YouVersion Logo
Search Icon

Luug 17:1-2

Luug 17:1-2 KY

Yeesu neeti ay taalibeem: «Ag fiir guy bàkkaarloo manula ñàkk, waaye wóoy ngalla ka koy lal. Ñu takkoon doj wu réy ci baatam, sànni ko biir géej moo gën ci moom muy bàkkaarloo kenn ci xale yii.