Luug 12:28
Luug 12:28 KY
Ndegam ñaxum tool miy dund tey, te léegi ñu sànni ko cib taal, moom la Yàlla di wodde nii kay, xanaa astamaak yeen? Yeenaka néew ngëm!