Luug 11:34
Luug 11:34 KY
Bët mooy làmpu yaram. Su sa bët wéree, sa yaram wépp ay fees ak leer, waaye bu sa bët bonee, sa yaram wépp a ngi ci lëndëm.