Yowaan 16:7-8
Yowaan 16:7-8 KY
Moona man de, dëgg laa leen wax. Seen njariñ moo di ma dem, ndax su ma demul, Taxawukat bi du ñëw ci yeen; waaye su ma demee, maa leen koy yónnee. Te bu dikkee, mooy tiiñal àddina ci wàllu bàkkaar ak ci wàllu dëgg ak ci wàllu àtte.





