Yowaan 16:20
Yowaan 16:20 KY
Maa leen ko wax déy ci lu wér, yeen yeenay jooy aka jooytu, àddina moom di bég; yeen, yeenay amu tiis, waaye bànneex la seenu tiis di soppaliku.