Bible App logo
Search Icon

Yowaan 16:13

Yowaan 16:13 KY

Moom miy Noowug dëgg gi, bu dikkee, moo leen di àggale ci dëgg gi gépp, ndax du ci coobarey boppam lay wax, waaye mboolem lu mu dégg la leen di wax, te liy ñëw ëllëg, moo leen koy wax.

Video for Yowaan 16:13

Verse Image for Yowaan 16:13

Yowaan 16:13 - Moom miy Noowug dëgg gi, bu dikkee, moo leen di àggale ci dëgg gi gépp, ndax du ci coobarey boppam lay wax, waaye mboolem lu mu dégg la leen di wax, te liy ñëw ëllëg, moo leen koy wax.

Free Reading Plans and Devotionals related to Yowaan 16:13