Bible App logo
Search Icon

Yowaan 1:3-4

Yowaan 1:3-4 KY

Lépp ci Kàddu gi lañu ko sàkke. Sàkkeesul dara lu ñu sàkkewul ci moom. Ci moom la dund nekk, te dund dig leer, ñeel nit ñi.

Verse Image for Yowaan 1:3-4

Yowaan 1:3-4 - Lépp ci Kàddu gi lañu ko sàkke. Sàkkeesul dara lu ñu sàkkewul ci moom. Ci moom la dund nekk, te dund dig leer, ñeel nit ñi.

Free Reading Plans and Devotionals related to Yowaan 1:3-4