YouVersion Logo
Search Icon

Njàlbéen ga 48:15-16

Njàlbéen ga 48:15-16 KY

Ma ngay ñaanal Yuusufa te naan: «Yàlla ji samay waajur Ibraayma ak Isaaxa toppoon, moom Yàlla ji ma sàmm, ba ma juddoo ba tey jii, moom Malaaka mi ma musal ci bépp loraange— yal na barkeel xale yi, ba ñu saxal sama tur ak samay turi waajur, Ibraayma ak Isaaxa, te giir, ba ne gàññ ci kaw suuf.»

Free Reading Plans and Devotionals related to Njàlbéen ga 48:15-16