YouVersion Logo
Search Icon

Njàlbéen ga 45:8

Njàlbéen ga 45:8 KYG

Kon nag du yeena ma yebal fii, waaye Yàllaa. Te moo ma jagleel, ma doon cëslaayal Firawna, mel ni baay ci moom, jiite këram gépp, boole ci yilif mboolem réewum Misra.