Njàlbéen ga 34:25
Njàlbéen ga 34:25 KY
Ca gannaaw ëllëg sa, fekk waa dëkk ba nekk ci mititu xarafal ba, ñaari doomi Yanqóoba ya, Simeyon ak Lewi, càmmiñi Diina, jël seeni saamar, dugg ca dëkk ba, bett leen, rey góor ñépp.