YouVersion Logo
Search Icon

Njàlbéen ga 32:11

Njàlbéen ga 32:11 KY

Yelloowuma lu gëna tuuti ci sa ngor ak sa worma, gi nga ma won, man sa jaam. Aw yet doŋŋ laa yoroon, ba ma jàllee dexu Yurdan, te yokku naa tey, ba doon ñaari dal.