Njàlbéen ga 3:11
Njàlbéen ga 3:11 KY
Yàlla Aji Sax ji ne ko: «Ku la xamal ne dangaa def yaramu neen? Mbaa du dangaa lekk ca garab ga ma la aaye, waay?»