YouVersion Logo
Search Icon

Njàlbéen ga 27:39-40

Njàlbéen ga 27:39-40 KY

Baayam Isaaxa ne ko: «Déglul, ma wax la, dinga dëkk fu sore ngëneeli suuf, mbaa fu la layub asamaan tiime. Sa saamar ngay dunde, sa rakk di la yilif. Waaye bés a ngi ñëw yaay sigiñu, ba yenniku nootaangeem.»