Njàlbéen ga 27:38
Njàlbéen ga 27:38 KY
Esawu ne baayam: «Baay, xanaa genn ñaan rekk nga am? Ngalla baay, ñaanal ma, man itam!» Ca la Esawu ne yikkét jooy.