YouVersion Logo
Search Icon

Njàlbéen ga 27:36

Njàlbéen ga 27:36 KY

Esawu ne: «Moom kay moo yey tudd Yanqóoba, ndax suufu na ma ñaari yoon. Sama céru taaw la njëkka nangu, tey mu nangooti sama ñaanu baay.» Mu teg ca ne: «Ndax desalaloo ma ag ñaan?»