YouVersion Logo
Search Icon

Njàlbéen ga 26:25

Njàlbéen ga 26:25 KY

Isaaxa nag sàkk fa sarxalukaay, tudd fa Aji Sax ji, wormaal ko, ba noppi samp fa xaymaam. Te itam ay surgaam bënn nañu fa ab teen.