Njàlbéen ga 24:3-4
Njàlbéen ga 24:3-4 KY
ma giñloo la ci Aji Sax jiy Yàllay asamaan ak suuf ne doo jëlal sama doom soxna ci biir jigéeni waa Kanaan, gi ma dëkk ci seen biir. Waaye dinga dem sama réew ma ma cosaanoo, jëlal fa sama doom Isaaxa soxna.»