Njàlbéen ga 22:14
Njàlbéen ga 22:14 KY
Ibraayma nag tudde béreb boobu Yawe Yire (muy firi Aji Sax ji dina dikk). Moo tax ñuy wax ba tey, naan: «Aji Sax jaa ngay dikke ca tundam.»