YouVersion Logo
Search Icon

Njàlbéen ga 21:12

Njàlbéen ga 21:12 KY

Teewul Yàlla ne Ibraayma: «Bu la dara naqari ci xale bu góor bii, mook sa jaam bi. Defalal Saarata li mu la wax rekk, ndax ci Isaaxa lees di tudde saw askan.