Mucc ga 9:1
Mucc ga 9:1 KY
Ba loolu wéyee Aji Sax ji da ne Musaa: «Demal ca Firawna, nga ne ko: “Aji Sax ji Yàllay Ebrë yi dafa wax ne: Bàyyil sama ñoñ, ñu dem màggali ma.