YouVersion Logo
Search Icon

Mucc ga 7:11-12

Mucc ga 7:11-12 KY

Ba mu ko defee Firawna moom itam woo boroom xam-xam yaak ñeengokat ya. Jabarkati Misra ya ñoom it fexe ca seeni xarfafuufa, ba def lu mel noona. Ku nekk ca ñoom sànni yetam, mu soppaliku jaan, yetu Aaróona nag wann seeni yet.

Free Reading Plans and Devotionals related to Mucc ga 7:11-12