Mucc ga 32:1
Mucc ga 32:1 KY
Ba mbooloo ma gisee Musaa yàgg lool te wàccul tund wa, dañoo songandoo Aaróona, ne ko: «Ayca, sàkkal nu ay yàlla yu nu jiite, ndax Musaa mii nu génne réewum Misra kat, xamunu lu ko dal.»