Mucc ga 29:45-46
Mucc ga 29:45-46 KY
Maay dëkk fi digg bànni Israayil te maay nekk seen Yàlla. Su boobaa bànni Israayil xam ne, man Aji Sax ji maay seen Yàlla, ji leen génnee réewum Misra, ngir dëkk fi seen biir. Man maay seen Yàlla Aji Sax ji.