YouVersion Logo
Search Icon

Kolos 1:16

Kolos 1:16 KY

Ndax moo di ki Yàlla sàkke lépp lu nekk asamaan ak lu nekk ci suuf, lu gisu ak lu gisuwul, muy boroom gàngune yeek boroom ndomboy tànk yeek boroom nguur yeek boroom sañ-sañ yi. Lépp ci moom lees ko sàkke, te mooy ki tax ñu sàkk lépp.

Verse Images for Kolos 1:16

Kolos 1:16 - Ndax moo di ki Yàlla sàkke lépp lu nekk asamaan ak lu nekk ci suuf, lu gisu ak lu gisuwul, muy boroom gàngune yeek boroom ndomboy tànk yeek boroom nguur yeek boroom sañ-sañ yi. Lépp ci moom lees ko sàkke, te mooy ki tax ñu sàkk lépp.Kolos 1:16 - Ndax moo di ki Yàlla sàkke lépp lu nekk asamaan ak lu nekk ci suuf, lu gisu ak lu gisuwul, muy boroom gàngune yeek boroom ndomboy tànk yeek boroom nguur yeek boroom sañ-sañ yi. Lépp ci moom lees ko sàkke, te mooy ki tax ñu sàkk lépp.Kolos 1:16 - Ndax moo di ki Yàlla sàkke lépp lu nekk asamaan ak lu nekk ci suuf, lu gisu ak lu gisuwul, muy boroom gàngune yeek boroom ndomboy tànk yeek boroom nguur yeek boroom sañ-sañ yi. Lépp ci moom lees ko sàkke, te mooy ki tax ñu sàkk lépp.Kolos 1:16 - Ndax moo di ki Yàlla sàkke lépp lu nekk asamaan ak lu nekk ci suuf, lu gisu ak lu gisuwul, muy boroom gàngune yeek boroom ndomboy tànk yeek boroom nguur yeek boroom sañ-sañ yi. Lépp ci moom lees ko sàkke, te mooy ki tax ñu sàkk lépp.Kolos 1:16 - Ndax moo di ki Yàlla sàkke lépp lu nekk asamaan ak lu nekk ci suuf, lu gisu ak lu gisuwul, muy boroom gàngune yeek boroom ndomboy tànk yeek boroom nguur yeek boroom sañ-sañ yi. Lépp ci moom lees ko sàkke, te mooy ki tax ñu sàkk lépp.