Bible App logo
Search Icon

Jëf ya 5:38-39

Jëf ya 5:38-39 KY

Léegi nag, dama ne, mànduleen ci ñii, te ba leen, ngir su seen mébét mbaa seen jëf bawoo ci nit, day yàqu rekk. Waaye su bawoo fa Yàlla nag, dungeen ko mana fanq, moytuleena jànkoonte ak Yàlla.» Ñu daldi fekksi Gamalyel,

Free Reading Plans and Devotionals related to Jëf ya 5:38-39