Bible App logo
Search Icon

Jëf ya 2:44-45

Jëf ya 2:44-45 KY

Gëmkat ñépp benn lañu woon te ñoo bokkoon lépp. Ci biir loolu seeni suuf ak seen alal sax, ñu jaay, séddoo ko ñoom ñépp na mu dëppook seeni soxla.

Free Reading Plans and Devotionals related to Jëf ya 2:44-45