Bible App logo
Search Icon

Jëf ya 2:17

Jëf ya 2:17 KY

“Yàlla nee: Mujug jamono, maay tuur samag Noo ci kaw ñépp; seeni doom, góor ak jigéen di biral kàdduy waxyu, seeni xale yu góor di gis ay peeñu, màggat ñi di gént ay gént.