Jëf ya 16:27-28
Jëf ya 16:27-28 KY
Boroom kaso ba tiite ciy nelaw, gis bunti kaso bi ubbiku. Mu bocci saamaram, nara xaru, yaakaar ne ña ñu tëj dañoo rëcc. Póol nag àddu ca kaw ne: «Bul lor sa bopp, nun ñépp a ngi fi.»