Jëf ya 11:17-18
Jëf ya 11:17-18 KY
Gannaaw nag Yàllaa leen jagleel genn may, ga mu nu jagleeloon, ba nu gëmee Sang Yeesu Almasi bi, ana ku ma doon, man, bay gàllankoor Yàlla?» Ba ñu déggee loolu lañu dal, daldi màggal Yàlla. Ñu ne: «Kon xeeti jàmbur yi, ndeke ñoom it Yàlla may na leen ñu tuub, ba dund!»





