2.Korent 5:18-19
2.Korent 5:18-19 KY
Loolu lépp ci Yàlla la jóge, moom mi nu jubale ak boppam ci Almasi bi, te moo nu sas, ngir nuy waare juboo googu. Loolu di firi ne ci Almasi bi la Yàlla jubale waa àddina ak jëmmu boppam, ba toppu leen seeni tooñ, te moo nu dénk kàddug juboo gi.







