1.Piyeer 3:12
1.Piyeer 3:12 KY
Ndax ay gët la Boroom bi ne jàkk aji jub ñi, te ay noppam la dékk seeni ñaan, waaye Boroom beey won gannaaw ñiy def lu bon.»