1.Piyeer 3:10-11
1.Piyeer 3:10-11 KY
Ndax kat: «Ku bëgg dundam neex, bëgga fekke bés bu rafet, na làmmiñam daw lu aay, dawi fen. Na daggook lu bon, tey def lu baax, sàkku jàmm, saxoo ko.