1.Piyeer 1:24-25
1.Piyeer 1:24-25 KY
Ndax bindees na ne: «Nit am ñax doŋŋ la; mboolem darajaam mel ni tóor-tóoru àll, ñax ma wow, tóor-tóor ma ruus. Waaye kàddug Boroom bi mooy sax ba fàww.» Kàddu googu moo di xibaaru jàmm bi ñu leen àgge.