1.Piyeer 1:15-16
1.Piyeer 1:15-16 KY
Waaye ni ki leen woo selle, yeen itam nangeen selle noonu ci seen mboolem jëfin. Ndax kat bindees na ne: «Ñu sell ngeen wara doon, ndax man Ku sell laa.»