1.Yowaan 4:7
1.Yowaan 4:7 KY
Soppe yi, nanu soppante, ndax cofeel ci Yàlla la bokk; képp ku am cofeel, ci Yàlla nga sosoo, te xam nga Yàlla.