1
Room 9:16
Téereb Injiil
TI
Dama leen di wax nag, dara ajuwul ci coobarey nit, mbaa ci ñaqam, waaye lépp a ngi aju ci yërmandey Yàlla.
Compare
Explore Room 9:16
2
Room 9:15
Dafa wax Musaa sax ne ko: «Su ma neexee yéwéne, su ma soobee yërëm.»
Explore Room 9:15
3
Room 9:20
Yaw nag nit ki, ak koo mana doon, lu tax ngay werante ak Yàlla? Ndax mbindeef dina laaj ki ko bind: «Lu tax nga binde ma nii?»
Explore Room 9:20
4
Room 9:18
Kon nag Yàlla, la ko neex lay def, muy yërëm nit, mbaa dëgëral xolam ci lu bon.
Explore Room 9:18
5
Room 9:21
Ndax tabaxkatu ndaa sañula fab banam, tabax ci ñaari ndaa, benn bi ngir soxla yu am maana, bi ci des ngir soxla yu ndaw?
Explore Room 9:21