1
Peeñu ma 11:15
Téereb Injiil
TI
Juróom ñaareelu malaaka ma wol liitam, noonu baat yu xumb jib ca asamaan naan: «Nguuru àddina, jébbalaat nañu ko sunu Boroom ak Almaseem, te dina nguuru ba fàww.»
Compare
Explore Peeñu ma 11:15
2
Peeñu ma 11:18
Xeet yi meroon nañu, waaye sa mer wàcc na, te jamono ji jot na, ji ngay àttee ñi dee, neexal say jaam yonent yi, ak sa gaa ñi ak ñi ragal saw tur, muy mag di ndaw, te nga rey ñiy yàq àddina.»
Explore Peeñu ma 11:18
3
Peeñu ma 11:3
Dinaa may sama ñaari seede yi, ñuy wax ci kàddug Yàlla, sol ay saaku, di toroxlu diirub junni ak ñaar téeméeri fan ak juróom benn fukk.»
Explore Peeñu ma 11:3
4
Peeñu ma 11:11
Waaye bi ñetti fan ya ak genn-wàll wéyee, xelum dund, jóge ca Yàlla, solu leen, ñu jóg taxaw. Noonu tiitaange gu réy jàpp ñi leen doon seetaan.
Explore Peeñu ma 11:11
5
Peeñu ma 11:6
Am nañu sañ-sañu téye taw diirub fan, yi ñuy wax ci kàddug Yàlla. Am nañu it sañ-sañu soppi ndox yi deret te wàcce ci kaw suuf musiba yu nekk, saa su ñu ko bëggee.
Explore Peeñu ma 11:6
6
Peeñu ma 11:4-5
Ñaari seede ya nag ñoo di ñaari garabu oliw yeek ñaari tegukaayu làmp, yi taxaw ci kanam Boroom suuf si. Su leen kenn bëggee def lu bon, sawaraay génn ci seen gémmiñ, daldi lakk seeni bañaale; te ku leen bëgga def lu bon, noonu lay wara deeye.
Explore Peeñu ma 11:4-5