1
Màrk 1:35
Téereb Injiil
TI
Ca njël laata bët di set, Yeesu jóg dem ca bérab bu wéet, di fa ñaan Yàlla.
Compare
Explore Màrk 1:35
2
Màrk 1:15
naan: «Jamono ji mat na, nguuru Yàlla jegesi na; tuubleen seeni bàkkaar te gëm xibaaru jàmm bi.»
Explore Màrk 1:15
3
Màrk 1:10-11
Bi muy génn ndox mi, mu daldi gis asamaan xar, te Xelum Yàlla di wàcc ci melow pitax, ñëw ci moom. Te baat bu jóge asamaan jib ne: «Yaa di sama Doom, ji ma bëgg; ci yaw laa ame bànneex.»
Explore Màrk 1:10-11
4
Màrk 1:8
Maa ngi leen di sóob ci ndox, waaye moom dina leen sóob ci Xel mu Sell mi.»
Explore Màrk 1:8
5
Màrk 1:17-18
Yeesu ne leen: «Ñëwleen topp ci man, dinaa leen def nappkati nit.» Ci saa si ñu bàyyi seeni mbaal, topp ci moom.
Explore Màrk 1:17-18
6
Màrk 1:22
Te ñu waaru ca njàngleem, ndaxte jàngal na leen ak sañ-sañ bu seeni xutbakat amul.
Explore Màrk 1:22