1
Kolos 4:6
Téereb Injiil
TI
Na seen wax jépp fees ak yiw te am xorom, ngir ngeen xam nan ngeen wara tontoo ku nekk.
Compare
Explore Kolos 4:6
2
Kolos 4:2
Dëkkleen ci ñaan Yàlla, farlu ci, boole ci ngërëm.
Explore Kolos 4:2
3
Kolos 4:5
Jëfeleen ak xel ci seen diggante ak waa àddina, te fu ngeen ame jot, fexeleen ba jariñoo ko.
Explore Kolos 4:5