1
Jëf ya 24:16
Téereb Injiil
TI
Moo tax fu ma tollu, maa ngi góor-góorlu, ngir am xel mu dal fa kanam Yàlla ak fa kanam nit ñi.
Compare
Explore Jëf ya 24:16
2
Jëf ya 24:25
Waaye bi Pool di waxtaan ci mbirum njub ak moom sa bopp ak bés pénc, Feligsë daldi tiit, yiwi ko ne ko: «Demal, bu ma amee jot, dinaa la woolu.»
Explore Jëf ya 24:25