1
Jëf ya 22:16
Téereb Injiil
TI
Léegi nag, looy nég? Jógal, ñu sóob la ci ndox, nga set ci say bàkkaar ci tudd turu Yeesu.”
Compare
Explore Jëf ya 22:16
2
Jëf ya 22:14
Mu ne ma: “Sunu Yàllay maam tànn na la, ba may la, nga xam coobareem te gis Aji Jub ji te nga dégg ay waxam.
Explore Jëf ya 22:14
3
Jëf ya 22:15
Ndaxte li nga gis te dégg ko, dinga ko seede ci ñépp.
Explore Jëf ya 22:15