1
2.Timote 4:7
Téereb Injiil
TI
Bëre naa ba ub làmbi ngëm, daw naa ba àkk, sàmm naa mboolem dëgg, gi ñu ma dénk.
Compare
Explore 2.Timote 4:7
2
2.Timote 4:2
xamleel kàddug Yàlla, sax ci, su neexee ak su naqaree; yeyal ñi tooñ, di yedd ak a dénk ñépp, def ko ci muñ gu yaatu ak njàngle mu mat.
Explore 2.Timote 4:2
3
2.Timote 4:3-4
Ndaxte jamono dina ñëw, joo xam ne nit ñi dootuñu xajoo njàngle mu wér mi, waaye dinañu jublu ci seeni bëgg-bëgg, di fortaatu jànglekat yu leen di jay. Dinañu tanqamlu dëgg, jeng jëm ci léebi diiney neen.
Explore 2.Timote 4:3-4
4
2.Timote 4:5
Waaye yaw nanga foog ci lépp, dékku tiis, tey tas xibaaru jàmm bi, ba matal sag yónnent.
Explore 2.Timote 4:5
5
2.Timote 4:8
Fi mu ne Yàllaa ngi may xaare añu ku jub, di kaalag ndam gi ma Boroom, biy Àttekat bu jub, di jox ca bés ba, te jéllale naa sama bopp, waaye képp ku def sa xol cig feeñam.
Explore 2.Timote 4:8