1
Màndiŋ ma 6:24-26
Kàddug Yàlla
KY
«“Yal na la Aji Sax ji barkeel, sàmm la. «“Yal na la Aji Sax ji geesoo leeram, baaxe la. «“Yal na la Aji Sax ji siggil, jàmmal la.”
Compare
Explore Màndiŋ ma 6:24-26
2
Màndiŋ ma 6:27
Bu ñu tuddalee noonu bànni Israayil sama tur, man, maa leen di barkeel.»
Explore Màndiŋ ma 6:27
3
Màndiŋ ma 6:23
«Waxal Aaróona aki doomam ne leen ni ñuy ñaanale bànni Israayil, nii la; nañu leen wax ne leen
Explore Màndiŋ ma 6:23