1
Màndiŋ ma 23:19
Kàddug Yàlla
KY
Yàlla du nit, bay fen, du doom aadama bay tuub. Moom wax na lu mu deful a? Am àddu na lu mu sottalul?
Compare
Explore Màndiŋ ma 23:19
2
Màndiŋ ma 23:23
Ñeengo jàppul Yanqóoba, gisaane gisul Israayil gii. Lu jot rekk, àggees ko Yanqóoba: ne ko: “Israayiloo, lii la Yàlla def.”
Explore Màndiŋ ma 23:23
3
Màndiŋ ma 23:20
Kàddug barkeel gii laa jot ndigalam, Yàllaa barkeel, duma ko tebbi.
Explore Màndiŋ ma 23:20