1
Luug 16:10
Kàddug Yàlla
KY
Ku màndu ci lu néew nag, màndu ci lu bare; ku jubadi ci lu néew it, jubadi ci lu bare.
Compare
Explore Luug 16:10
2
Luug 16:13
«Ab jaamu kër nag manula jaamu ñaari sang; day dëddu kii, sopp kee; mbaa mu fonk kii, cof kee. Manuleena jaamoondoo Yàlla ak alal.»
Explore Luug 16:13
3
Luug 16:11-12
Kon su ngeen mànduwul ci alalu àddina, alal ji dëgg, ana ku leen koy dénk? Te su ngeen mànduwul ci alalu jàmbur, ana ku leen di dénk seen alalu bopp?
Explore Luug 16:11-12
4
Luug 16:31
Ibraayma nag ne ko: “Su ñu dégluwul Musaa, dégluwuñu yonent yi kay, ku dekki, bàyyikoo ci ñi dee sax du tax ñu gëm.”»
Explore Luug 16:31
5
Luug 16:18
«Képp ku fase sa jabar, takk keneen, njaaloo nga; te ku jëkkëram fase, képp ku ko takk, njaaloo nga.
Explore Luug 16:18