1
Mucc ga 40:38
Kàddug Yàlla
KY
Ndax booba niiru Aji Sax jaa nga ca kaw jaamookaay ba, ag bëccëg, te sawara waa nga ca biir niir wa, ag guddi, waa kër Israayil gépp di ci gis, seen diiru yooni tukki ya.
Compare
Explore Mucc ga 40:38
2
Mucc ga 40:34-35
Ba loolu amee niir wa yiir xaymab ndaje ma, leeru Aji Sax ji fees jaamookaay ba, ba Musaa tëlee dugg ca xaymab ndaje ma, ndax niir wa màkkaanoo kaw xayma ba, ak leeru Aji Sax ji fees jaamookaay ba.
Explore Mucc ga 40:34-35