1
Jëf ya 24:16
Kàddug Yàlla
KY
Moo tax fu ma tollu, man itam, may def lu ma man ngir am xel mu dal, wàccoo ak Yàlla, wàccoo ak nit ñi.
Compare
Explore Jëf ya 24:16
2
Jëf ya 24:25
Naka la Póol wax ci mbirum njub, ak noot sa bakkan, ak àtteb bés-pénc, Feligsë daldi tiit, ne ko: «Léegi, man ngaa demagum, bu ma ko talee, dinaa la wooluwaat.»
Explore Jëf ya 24:25