1
Jëf ya 22:16
Kàddug Yàlla
KY
Léegi nag, looy nég? Jógal, ñu sóob la ci ndox, nga set, teqalikook say bàkkaar, te tudd turu Yeesu.”
Compare
Explore Jëf ya 22:16
2
Jëf ya 22:14
Mu ne ma: “Sunu Yàllay maam moo la dencal céru ràññee coobareem, ak gis Aji Jub ji, dégg ko, muy wax ak yaw.
Explore Jëf ya 22:14
3
Jëf ya 22:15
Ndax li nga gis, dégg ko, yaa koy seedeel nit ñépp.
Explore Jëf ya 22:15