1
Jëf ya 10:34-35
Kàddug Yàlla
KY
Ba loolu amee Piyeer àddu, ne: «Dëgg-dëgg gis naa ne Yàlla daal du gënaatle, waaye xeetoo xeet, ku ko ci ragal tey jëfe njub, mooy ki ko neex.
Compare
Explore Jëf ya 10:34-35
2
Jëf ya 10:43
Moom la yonent yépp seedeel, ne képp ku ko gëm, jot nga sa njéggalug bàkkaar ciw turam.»
Explore Jëf ya 10:43