1
Macë 4:4
Téereb Injiil
TI
Waaye Yeesu ne ko: «Mbind mi nee na: “Nit du dunde mburu rekk, waaye itam gépp kàddu gu génne ci gémmiñug Yàlla.”»
Comparer
Explorer Macë 4:4
2
Macë 4:10
Waaye Yeesu ne ko: «Sore ma Seytaane, ndaxte Mbind mi nee na: “Nanga màggal Yàlla sa Boroom, te jaamu ko moom rekk.”»
Explorer Macë 4:10
3
Macë 4:7
Yeesu ne ko: «Bind nañu it ne: “Bul diiŋat Yàlla, sa Boroom.”»
Explorer Macë 4:7
4
Macë 4:1-2
Bi loolu amee Xelum Yàlla yóbbu Yeesu ca màndiŋ ma, ngir mu jànkoonte ak fiiri Seytaane. Yeesu nekk fa te lekkul ñeent fukki bëccëg ak ñeent fukki guddi, doora xiif.
Explorer Macë 4:1-2
5
Macë 4:19-20
Yeesu ne leen: «Ñëwleen topp ci man, ma def leen nappkati nit.» Ca saa sa ñu daldi bàyyi seeni mbaal, topp ci moom.
Explorer Macë 4:19-20
6
Macë 4:17
Booba Yeesu tàmbali di waare naan: «Tuubleen seeni bàkkaar, ndaxte nguuru Yàlla Aji Kawe ji jegesi na.»
Explorer Macë 4:17